12/11/2026
Sama gars yi setane nguen le vlog de fah_aidara à Ziguinchor ? 🔥
No leen ko guissé ? Gérer nako wala deet ? Vos avis en commentaires ma khol 👇🏾
Yeen gniko guissagoul daaw leen gaaw sur la chaîne YouTube de Kirène avec Orange, bu leen ko ken netali !