Xelkoom

Xelkoom Xelkoom, l'horizon commercial s'eclaircit. L'intelligence au service du développement.

JIGÉEN WAAYE JAMBAAR.Ci laa ko xamee, ci laa ko miinee.Jàng, Liggéey, Liggéey, Liggéey.Sama nit la yágg na ñu lu ëpp fuk...
01/02/2026

JIGÉEN WAAYE JAMBAAR.
Ci laa ko xamee, ci laa ko miinee.
Jàng, Liggéey, Liggéey, Liggéey.
Sama nit la yágg na ñu lu ëpp fukki at ak yu teg. Ci ñafe, daw, dag-dangi. Su tawatee sax day wér ndax Tàmmu ko. Sama jigéen la. Lu baax lu nekk defal nama ko. Nit du ko gën. Jàmbaar te Bëgg yaayam. Ci laa ko xam. Aka yewwu maachalaa noppi wam nak mën nala nax. Jigéen la d waaye góor du ko yab. Ndax daa nekk ci li mu wara nekk. Ku baax yàgg yàgg di na baax.

NDAM LIMbégte mu réewum lumb yëgandoo. Mel ne da ñu xamoon ne ndam li day gane si. Ku ndekk taaral sa gox. Ñi réeroo woo...
21/01/2026

NDAM LI
Mbégte mu réewum lumb yëgandoo. Mel ne da ñu xamoon ne ndam li day gane si. Ku ndekk taaral sa gox. Ñi réeroo woon sax feeñoo. Lu baax lu baax lay jur. ndokkale ci li ñu bokk.

TEERTU

TEERTU lu muy neex-neew teeru ku am sarica mooko dàq. Teeru réewum lum bu ànd ak mbégte. Xale mag kenn desul.

🇲🇦⚽️

TEERTUTEERTU lu muy neex-neew teeru ku am sarica mooko dàq. Teeru réewum lum bu ànd ak mbégte. Xale mag kenn desul.
21/01/2026

TEERTU

TEERTU lu muy neex-neew teeru ku am sarica mooko dàq. Teeru réewum lum bu ànd ak mbégte. Xale mag kenn desul.

NDAM LIMbégte Gu réewum lumb yëgandoo. Mel ne da ñu xamoon ne ndam lz day gane si. Ku ndekk taaral sa gox. Ñi réeroo woo...
19/01/2026

NDAM LI
Mbégte Gu réewum lumb yëgandoo. Mel ne da ñu xamoon ne ndam lz day gane si. Ku ndekk taaral sa gox. Ñi réeroo woon sax feeñoo. Lu baax lu baax lay jur. ndokkale ci li ñu bokk.
🇲🇦⚽️

Meilleur Photographe de l’Année – Sénégal 🇸🇳🏆Ce vendredi 12 décembre 2025, j’ai été honoré par les Outside Awards 2025 e...
14/12/2025

Meilleur Photographe de l’Année – Sénégal 🇸🇳🏆

Ce vendredi 12 décembre 2025, j’ai été honoré par les Outside Awards 2025 en remportant le trophée de Meilleur Photographe de l’Année au Sénégal.

Reconnaissant, fier et motivé plus que jamais.
Merci pour le soutien, la force et la confiance ❤️📸

Le travail continue.

Hashtags :

L U  LEWSoo ci nekkee lepp lu ñu la tere woon daf lay lew domm. Muñ de daa yombwaante metti na ndax lepp a lay jege nd...
09/12/2025

L U LEW
Soo ci nekkee lepp lu ñu la tere woon daf lay lew domm. Muñ de daa yombwaante metti na ndax lepp a lay jege ndax tere bi. Soo leen xoolee bu baax sax di ngeen seetlu soo jaayantee di na metti waante di na neex soo ko ndangoo. Su la lewee nga xam ni jar nako. Lu nduroo wul bokkul ak ànd ak bànneex neex na muñ. #

MARYAAMA / KAAR YÀLLAMelow nit ku baax mooy nga namm lu baax di ko topp ci saa su ne. Bëgg lu baax te doo ko yamale ak d...
04/11/2025

MARYAAMA / KAAR YÀLLA
Melow nit ku baax mooy nga namm lu baax di ko topp ci saa su ne. Bëgg lu baax te doo ko yamale ak dara. Doo sikki sakka Mukk lu baax ndax da nga koy xam.
Wut woo xam ne ñépp a ko soxlo am ca Jaajëf aka jafe. Tubëy ak sër ràññee la waaye foofu nit rek nga Fay ràññee. Cofeel ak bànneex daw na ñu fa ndax bët bi xoolul lu dul pàjum aajo. Ku sonn sax du tal yenn yii ba laa ngay gën bég Yan wi diis ba ngay Bëgg a bàyyi. Li góor sóobu rek jigeen moo ka cat jiitu. Fii nak amul xeeb waaye am na soxlo.

́ .

CI BIIR LIGGÉEY BIKu dëggal dugg. Amul xàjj ak seen.Ngay fau ngir dem, joxe sa ñaq, def ci sa doole boole ko ak Réccu. N...
02/11/2025

CI BIIR LIGGÉEY BI
Ku dëggal dugg. Amul xàjj ak seen.
Ngay fau ngir dem, joxe sa ñaq, def ci sa doole boole ko ak Réccu. Nga noppi nak am mbégte ci Loolu. Ki nga koy defal itam moom day saytu rek moomul ligéey bi. Day taxawu Lépp ba mu mat mu ñaan nangub Liggéey bi.

nekk ndaw, Ndeysaan lepp ngay bëgg nekk. Sooy Màgg xam ne li nga Bëgg mënul nekk. Nga waaj jekk ni tekk xool fi nga bokk...
01/11/2025

nekk ndaw, Ndeysaan lepp ngay bëgg nekk. Sooy Màgg xam ne li nga Bëgg mënul nekk. Nga waaj jekk ni tekk xool fi nga bokk. Xool li nga mën, xool fi nga jaar, xool li mën nekk, xool fi ñu la jaarale. Tekki nak du alal wala jekku Ádduna, tekki mooy jub ak mucc.

education

Adresse

HLM Grand Yoff
Dakar

Téléphone

+221776251203

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Xelkoom publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Contacter L'entreprise

Envoyer un message à Xelkoom:

Partager